Loading...

Download
  • Genre:Gospel
  • Year of Release:2024

Lyrics

Gëm ngi né ci ñun, fok ñu woné ko !

Gëm ngi né ci ñun, fok ñu woné ko !


Bi àddina sosso ba léegi

Ya ngi woné sa boppa

Té meussou lo sopeeku

Bayi wo ñu, ya ngi def sa mëniin


Ci barké Yéesu-Kristaa

Gumbëya ngi gis

Ci barké Yéesu-Kristaa

Lafagn ya ngi dox

Ci barké Yéesu-Kristaa

Ñi tëx a ngi déga

Ci barké Yéesu-Kristaa

Ñi deewone deeki negn


Toi le prince de paix (Yéesu !)

Continue ton œuvre (Yéesu !)

Tu ne déçois pas (Yéesu !)

Ceux qui espèrent en toi (Yéesu !)

Grand Dieu de miracles (Yéesu !)

Refais des prodiges (Yéesu !)

Que mon âme te loue (Yéesu !)

Acclame ton saint nom (Yéesu !)


Yow la gëm

(Yéesu !)

Dara titalatouma

(Yéesu !)

Yow rekk la gëm

(Yéesu !)

Jërë jëfé Yéesu-Kristaa

(Yéesu !)

Baatu Yàlla

Yéesu ! (Kristaa !)

Yéesu ! (Kristaa !)

Yéesu ! (Kristaa !)

Yéesu Batu Yàlla !

Yéesu rekk ! (Kristaa !)

Yéesu kessé ! (Kristaa !)

Yéesu dong ! (Kristaa !)

Yéesu Baatu Yàlla !


Sey jaloré yeksi na

Leeral seumey gët ma gis la

Saa souné nga taxawlu ma

Tek ci mbëggeel teralma, sargal ma


Ci barké Yéesu-Kristaa

Jàmm rekk ci ñun

Ci barké Yéesu-Kristaa

Def ñu tek ci yoonu ndam

Ci barké Yéesu-Kristaa

Ay kemtane la deef ci ñun

Ci barké Yéesu-Kristaa

Moo tax ñu sant ba abadane


Toi le prince de paix (Yéesu)

Continues ton œuvre (Yéesu)

Tu ne déçois pas (Yéesu)

Ceux qui espèrent en toi (Yéesu)

Grand Dieu de miracles (Yéesu)

Refais des prodiges (Yéesu)

Que mon âme te loue (Yéesu)

Acclame ton saint nom (Yéesu)


Yow la gëm

(Yéesu !)

Dara titalatouma

(Yéesu !)

Yow rek la gëm

(Yéesu !)

Jërëfé Yéesu-Kristaa

(Yéesu !)

Batu Yàlla !

Yéesu ! (Kristaa !)

Yéesu ! (Kristaa !)

Yéesu ! (Kristaa !)

Yéesu Batu Yalla !

Yéesu rekk ! (Kristaa !)

Yéesu kessé ! (Kristaa !)

Yéesu dong ! (Kristaa !)

Yéesu Batu Yàlla!


Gëm ngi né ci ñun, fok ñu woné ko !

+

      -   or   -

      -   or   -

      NG +234

          Please Select A Playlist

          Add New Playlist

          Share on

          Embed: Love & Light EP

          Custom Size :

          • Default
          • Desktop(300*600)
          • Mobile(300*250)

          Type :

          • HTML/HTML5 (WordPress Supported)
          Get Boomplay Premium
          for
          Payment Method
          Pay With
            Review and pay
            Order Date
            Payment Method
            Due Today
            Flutterwave
              Subscription Successful

              Congratulations! You have successfully activated Boomplay 1 Month Premium.

              Now you have access to all the features of Boomplay App.
              Payment Failed

              Please check your balance and then try again.

              You'll lose your subscription if we don't have a working payment method for your account, so please check your payment details.
              Need help? Contact Boomplay Subscription Support.
              Payment Processing...
              10 s

              Payment is being processed by . Please wait while the order is being comfirmed.

              Payment Processing
              Your order is processing, and it may take up to a few days for the service provider to handle your payment. Please kindly stay tuned and check your order status in ‘User Center’.
              About Order Status