Loading...

Download
  • Genre:Hip Hop & Rap
  • Year of Release:2023

Lyrics

Daan sa doole - CARBI

...

Carbi : Daan sa doole

intro:

yes! yah!

carbi on the side.

Daan sa doole.

Couplet 1:

Ndaw lañu suñu réw, nañu daan suñu doole.

Waruñu toog di nelew, réwmi di gëna sóoxe.

Ñii nañu jápp fi, ñëlé nañu jápp fee.

Ñii demee nii, ñëlé nañu demee nee.

Ñoom ñi ne bitiim réew, nañu daan seen doolé.

Góorgóorlu warnaleen ngir jëriñ suñu réw.

ku ci ne sa ligéey, bulko xéeb na nga jéem.

Mu gëna jëm kanam, gëmne daal dina baax.

Refrain 1:

yor mi ne ci sa réw, daan sa doole warnala.

yow mi ne bitim réw, Daan sa doole warnala.

(bis).

Couplet 2:

Artis bee mi ngi daan doolé.

artisan bee mi ngi daan doolé.

commerçant bi mi ngi daan doolé.

Enseignant bee mi ngi daan doolé.

Forgeron bi mi ngi daan doolé.

Beykat bi mi ngi daan doolé.

Napp Kat bi mi ngi daan doolé.

taximan bé mi ngi daan doolé.

Aviateur bé mi ngi daan doolé.

Mécanicien bé mi ngi daan doolé.

Menuisier bi mi ngi daan doolé.

Coiffeur bé mi ngi daan doolé.

Mbindaan bé mi ngi daan doolé.

Maçon bé mi ngi daan doolé.

transiter bé mi ngi daan doolé.

Diaspora jee mi ngi daan doolé.

Refrain 1:

yor mi ne ci sa réw, daan sa doole warnala.

yow mi ne bitim réw, Daan sa doole warnala.

(bis).

Couplet 3:

dëkk di daan sa doole moo gën toog di jëw.

dëkk di daan sa doole jaamu yalla la.

dëkk di daan sa doole jaamu yalla la.

dëkk di daan sa doole moom de maandu la.

Refrain 1:

yor mi ne ci sa réw, daan sa doole warnala.

yow mi ne bitim réw, Daan sa doole warnala.

(bis).

+

      -   or   -

      -   or   -

      NG +234

          Please Select A Playlist

          Add New Playlist

          Share on

          Embed: Love & Light EP

          Custom Size :

          • Default
          • Desktop(300*600)
          • Mobile(300*250)

          Type :

          • HTML/HTML5 (WordPress Supported)
          Get Boomplay Premium
          for
          Payment Method
          Pay With
            Review and pay
            Order Date
            Payment Method
            Due Today
            Flutterwave
              Subscription Successful

              Congratulations! You have successfully activated Boomplay 1 Month Premium.

              Now you have access to all the features of Boomplay App.
              Payment Failed

              Please check your balance and then try again.

              You'll lose your subscription if we don't have a working payment method for your account, so please check your payment details.
              Need help? Contact Boomplay Subscription Support.
              Payment Processing...
              10 s

              Payment is being processed by . Please wait while the order is being comfirmed.

              Payment Processing
              Your order is processing, and it may take up to a few days for the service provider to handle your payment. Please kindly stay tuned and check your order status in ‘User Center’.
              About Order Status